Yaay Joor by Ashs The Best (Ft. Obree Daman)
Yaay Joor by Ashs The Best (Ft. Obree Daman)

Yaay Joor

Ashs The Best & Obree Daman * Track #1 On Dibèer

Yaay Joor Lyrics

Hum hum
Weettay dima ray
Té niémé wou ma netali
Mangui sama yoon
Ni pithie Ramatou
Yala dima weteuli
Gorr momoul nianne
Yareewouniouma tallal lokho
Yaay joor sama yaye
Mangui sakkou sa niane
Yeurmande amoul fii
Wettay ak namel
Nek ndaw ci samay digeu morom yaffouss warouma
Fii lekougnou ba sour
Nanouniou ba mandé
Way nek ndaw ci sunu digeu morom yaffouss warouma

So yewo yema fallo
So yewo yema fall
(Yeah)
Fi degn fi nekk ak ngor
Fi degn fi dathie lou metti
Nekk fi ak jom
Fatewouma demb ak Yaay Joor
Wettay si xol la meun yam
Sam khel jougoul si sassmeu
Goné diss neu wayé bo magué fay borr
Lambay soudé meuss neu nekh
Tay Walo amoul ndokh
Touki dou tekki
Gaaday andou tak banekh
Wetna wettay bimay yé
Rerr na fou gnar gni fеgn
Genteu beu dеmb fegn tay
Yéné beu agg
Jooy na fou keine newoul, dem na ba bougou ma guiss samay rongogn
Ndakh mounou meu bayi limalen diguon
Jambar dawoul daa outi ji wone
Yakar bou tassoul ba tay
Ndakh yoon bi diekha goul
Sama khel ci kasso dou teey dey dem fou dieumeu doul yegg di fey
Wetna wettay bimay yé
Anh anh anh
Jooy na jooy guisouma keineu
Yeah yeah yeah
Love and peace for me
I can shine, shine like a diamond
Wa wa wa
I can shine, shine like a diamond
Pray for, for me yeah

Wettay dima ray (wettay)
Té niémé wou ma netali
Mangui sama yoon
Ni pithie Ramatou
Yala dima weteuli
Gorr momoul nianne
Yareewouniouma tallal lokho
Yaay joor sama yaye
Mangui sakkou sa niane
Yeurmande amoul fii
Wettay ak namel
Nek ndaw ci samay digeu morom yaffouss warouma
Fii lekougnou ba sour
Nanouniou ba mandé
Way nek ndaw ci sunu digeu morom yaffouss warogno

So yewo yema fallo
So yewo yema fall
Ndibeulo yeurmandey fall
Doley biir bek bitti bee fall

Yaay Joor Q&A

Who wrote Yaay Joor's ?

Yaay Joor was written by Olivier Delahaye & Obree Daman & Ashs The Best & Abdoulaye Sy.

Who produced Yaay Joor's ?

Yaay Joor was produced by Nautylusprod.

When did Ashs The Best release Yaay Joor?

Ashs The Best released Yaay Joor on Fri Jun 11 2021.

Your Gateway to High-Quality MP3, FLAC and Lyrics
DownloadMP3FLAC.com