Xel Akk Xol by Ashs The Best
Xel Akk Xol by Ashs The Best

Xel Akk Xol

Ashs The Best * Track #3 On Dibèer

Xel Akk Xol Lyrics

Yeah, eh eh eh
Lé, lé, walé
Hum, hum
Suba suma yeewu
Yaw lay bëgg jakarlool
Sa suma yeewu
Yaw lay bëgg njëkk xol
Ëlëk lu mata soor la
Wayé xel xalatu ko
Ëlëk ay jaar-jaar la
Sama xol yëgoon nako muy ñëw
Xel xalaat la (xel ak xalatam bë)
Xol yëkk yëkk la
Nit ak jëmëm jë
Dara xaaju fë
Sa suma yeewu
Yaw lay bëgg njëkk xol
(Suma yewo yaw la bëgg njekk xol)
Fajar suma yeewu
Yaw la bëgg jakarlool
Denk na la guddi
Fanané yakkar ci yaw
Gent na la guddi gi yëpp
Ndax fajar yaw lay jakarlool
Mbëggël!
Xel xalaat la
Xol yëkk yëkk la
Nit ak jëmëm jë
Dara xaaju fë
Nit nak ak jëmëm jë
Dara fa xaajul

Xel Akk Xol Q&A

Who wrote Xel Akk Xol's ?

Xel Akk Xol was written by Olivier Delahaye & Abdoulaye Sy.

Who produced Xel Akk Xol's ?

Xel Akk Xol was produced by Nautylusprod.

When did Ashs The Best release Xel Akk Xol?

Ashs The Best released Xel Akk Xol on Fri Jun 11 2021.

Your Gateway to High-Quality MP3, FLAC and Lyrics
DownloadMP3FLAC.com