Sutura by Ashs The Best
Sutura by Ashs The Best

Sutura

Ashs The Best * Track #8 On Dibèer

Sutura Lyrics

Ci sutura Ci sutura Ci sutura
Sama waaji na ñu waxtaan ci sutura
Xarit, dee naa la ci sutura
Ci sutura laa lay waxee sama ge'nt
Sutura
Ci sutura laa lay samay proble'mes akk lima dal
Sutura
Ci laa lay de'nkee sama guddi
Bulma weer ni bëccëg
Bulma weer ni bëccëg
Sutura sutura
Bulma weer ni bëccëg
Ndax yombul nga xamal ma

Mbokk waay
Sutura Sutura
Sutura sutural ma Sutura
Sutural ma Sutura
Sutura sutural ma Sutura

Mbokk du nii
Reeroo bumu tax nga tasaare ma
Sutura sutural ma
Ñu weetoo ma wax la sama demb nga waxaat ko tay
Xarit sama waaji
Ma ne Mbokk du nii
Bulma jeebaane fii
Bul wax sama proble'me ci ñii
Woolu la tay
Waraloon demb ma wax la lu xew wax la sama xol

Mbokk waay
Sutura Sutura
Sutura sutural ma Sutura
Sutural ma Sutura
Sutura sutural ma Sutura

Sutura Q&A

Who wrote Sutura's ?

Sutura was written by Olivier Delahaye & Abdoulaye Sy & Ashs The Best.

Who produced Sutura's ?

Sutura was produced by Nautylusprod.

When did Ashs The Best release Sutura?

Ashs The Best released Sutura on Thu Jun 10 2021.

Your Gateway to High-Quality MP3, FLAC and Lyrics
DownloadMP3FLAC.com