Khalé bi sama reni khol nga wuyuma
Buga nala te hamo chi dara
Mbeuguel chi khol lai neka deug la
Buga nala te hamo chi dara
Man dei warou len ma wakh koko
Khale bi lekatouma ndah mar
Nanatouma nelowatouma
Wow wow suma khol ya chi né
Leg leg wakh ko
Ter dar di coupe
Sama apetit coupe
Febar dinama goungay
Doctoeur dou ma lova dev teh houma lou koi faj
Wow wow mba munga chi dara
Khalé bi sama reni khol nga wuyuma
Buga nala te hamo chi dara
Mbeuguel chi khol lai neka deug la
Buga nala te hamo chi dara
Man wor na la founé
Nga japeh ma sa kharite
Evite resteau, lalal na la loune
Wow wow, nga japeh ma sa kharite
Leg leg wakh ko
Ter dar di coupe
Sama apétit coupe, febar dinama goungay
Doctoeur dou ma lova dev teh houma lou koi faj
Wow wow mba munga chi dara
Man bégu na
Ma bajn bayi wouma
Man guiss uma
Keneen kudout man
Mbeuguel a bari dole ma ko khar
Khalé bi sama reni khol nga wuyuma
Buga nala te hamo chi dara
Mbeuguel chi khol lai neka deug la
Buga nala te hamo chi dara
Khalé bi sama reni khol nga wuyuma
Buga nala te hamo chi dara
Mbeuguel chi khol lai neka deug la
Buga nala te hamo chi dara
Kouchi nekal ki nga nob
Sa ganaw bandal fahasal
Jugal yenguel bemu saff
Sa ganaw bandal fahasal
Kouchi nekal ki nga nob
Sa ganaw bandal fahasal
Jugal yenguel bemu saff
Sa ganaw bandal fahasal
Wuyuma was written by Viviane Chidid.
Wuyuma was produced by Viviane Chidid.
Viviane Chidid released Wuyuma on Wed Dec 21 2016.