Demb wétoon na
Dama réron nga fégnal ma
Yaw mi ladon khar
Fekeu ma ci leundeum niital ma
Sama khol wétoon na
Danga nieuw ma kham louy adouna
Sa mbeuguél doundal ma
Yorrma Yarrma Yeureum ma
Damaleu beug beug té Yalla takh paré lepp pour nékak Yaw
Ndax demb wétoon na
Dama réron nga fégnal ma
Yaw la taamo nékal
Yaw la nangoul louma meussoul nangoul ken
Sa mbeuguél doundal ma
Yorrma Yarrma Yeureum ma
Huuuuuu woooooh wooooh Yeah yeah
Mbeuguél bi douma gagne
Huuuuuu woooooh wooooh nanananana Yeah yeahhhhhhh
Mbeuguél bi douma gagne
Ndax demb weet na weet na
Tay samay nakar diekhna weet na
Yakar bou tasson waw
Sama khol lama teudion kasso wawaw
Banekh bi nieuw na nieuw na
Metti won demb tay nekh na nekh na
Mak yaw all day all night
Sa wet la beug dess mak yaw for life
Demb wétonn na (wétoon na)
Dama réroon nga fégnal ma (fégnal ma)
Sa mbеuguél la nieuw doundal ma (doundal ma)
Yorrma Yarrma Yeureum ma (yеureum ma)
Demb wétonn na (wétoon na)
Dama réroon nga fégnal ma (fégnal ma)
Sa mbeuguél la nieuw doundal ma (doundal ma)
Yorrma Yarrma Yeureum ma (yeureum ma)
Uhhhhhh ouhhhhh
Mak yaw mak yaw
Sa wet la beug dess mak yaw for life
So baby beug touma nga sorima
Sa wet la beug dess mak yaw all day all night
Mak yaw mak all day all night
Sa wet la beug dess mak yaw for life
Demb wétonn na (wétoon na)
Dama réroon nga fégnal ma (fégnal ma)
Sa mbeuguél la nieuw doundal ma (doundal ma)
Yorrma Yarrma Yeureum ma (yeureum ma)
Demb wétonn na (wétoon na)
Dama réroon nga fégnal ma (fégnal ma)
Sa mbeuguél la nieuw doundal ma (doundal ma)
Yorrma Yarrma Yeureum ma (yeureum ma)
Wétoon na
Fégnal ma
Doundal ma
Yeureum ma
Wetoon na was written by Nautylusprod & Ashs The Best.
Wetoon na was produced by Nautylusprod.
Ashs The Best released Wetoon na on Tue Dec 29 2020.