Muy suba muy guddi
Muy naaj
Mbaa muy soobé
Mësu maa wooté
Te wuyu loo ma
Boo weeté gore
Weetali ku nga akk sa mbëggeel
Mësu maa wooté
Te wuyu loo ma
Ah Yeah
Ah Yeah
Eh Yah
Mësu maa wooté
Teh wuyu loo ma
Fii ci adduna yaa
Gisu ma ku melni yow
Mbëggeelam yaatu na
Yërmandeem moo ma yeem
Ku melni yow
Benn la dootul ñaar
Yaay sama Aljana
Yow mi ma teg yoon
Ci yoonu leer
Cause I've been fearless
To get to the road tonight
Because so been love
Nobody never
Everything how to try
But I believe in miracles now
You're right here
Yow mii sa mbëggeel bi yaatu na ni Adduna
Gestu gis la sama wet muy Aljana
Mësu maa la woo te wuyu loo ma
Sa yërmande yeem na ma man
Xeebu loo benn yoon siggil nga ma
Def ma ni sa bopp te won nga ma
I've been so grateful for your love
Muy suba muy guddi
Muy naaj
Mbaa muy soobé
Mësu maa wooté
Teh wuyu loo ma
Boo weeté goré
Weetali ku nga akk sa mbëggeel
Mësu maa wooté
Teh wuyu loo ma
Mësu ma la woo wuyu loo ma
Saayu ma soxla nga jox ma xañ sa bopp
Li nekk ci yow moy daw ci man mii
Suma la gisee
Moy gis naa sama bopp
Lu fees ci xol feeñ ci jëmm jii
Yow sa mbëggeel moo may weetali
Yow mii
Sa mbëggeel bi yaatu na ni Adduna
Gestu gis la sama wet muy Aljana
Mësu maa la woo te wuyu loo ma
Sa yërmande yeem na ma man
Xeebu loo benn yoon siggil nga ma
Def ma ni sa bopp te won nga ma loolu
I've been so grateful for your love
Muy suba muy guddi
Muy naaj
Mbaa muy soobé
Mësu maa wooté
Te wuyu loo ma
Boo weeté goré
Weetali ku nga akk sa mbëggeel
Mësu maa wooté
Teh wuyu loo ma
Teh wuyu loo ma...
Weetël was written by Ashs The Best.
Weetël was produced by Nautylusprod.
Ashs The Best released Weetël on Thu Jan 13 2022.