Nix
Nix
Nix
Nix &
Nix
Nix
Nix &
Nix
Nix & Omzo Dollar
Nix &
Nix
Nix
Nix & Mennel
Nix & Micky R
Nix
Nix
Nix &
Nix
Nix
Nix
{Refrain}
Ma nigga talouniou Fo
Gni ngui run game bi doniou déggueu
Yagg neu BMG 44
Loumou Yagg yagg boy di nga nangou louy deugg
My nigga Talouniou Talouniou Talouniou Fo
{Verse 1}
Yeah Talouniou Fo
Okay !
Ma nigga gnou ngui ci louniou done def
Diko may niou niou done xepp
Diko may niou niou done xééx
Mais Njaago bi xééxam dou diekh
Tay nga xamné Game bi loumou ma done doyé
Bitches yi lougnema done khoyyé
Sa MCs yi lougne niou done dŽeé
N Easy moy Highlander dafay daggeu sen bopp dilene vilipender
Game bi day djaay fondé
Chaque jour ma tyme bondé
Fi maay sen James Bond hé
Meuno xam loumay lidieunti ni sen kilifeu bouy guéneu xajjou goudi men
Meuno xam fepp fouma diaar ba MARCHé bi dima khaar ni BALLOU Colobane
{Refrain}
Ma nigga talouniou Fo
Gni ngui run game bi doniou déggueu
Yagg neu BMG 44
Loumou Yagg yagg boy di nga nangou louy deugg
My nigga Talouniou Talouniou Talouniou Fo
{Verse 2}
Yeah ! Hummmm ! Aythia
Yonou money noumou meuneu tolou di nga fa fekk noone yi di beug diolou
Sa niaari loxo loumou goudou goudou do meusseu djot weurseuk kou Yallah toudou
Ay FLOW yu LEUNDEUM boy ni XAADJI GOUDI
STRING gou GAME BI lagnou nara BOUDI
Baby yama eupeu lamigne kone so nieuwé dou tankeu késsé nga nara oubi
Nénagn meu doundou lo GALSEN
Ya ngui RAP FRENCH ya ngui laale CHANGE
Ndékété mangui NYC ci strip clubs yi Boy di lidieunti ay lapdance
Doundou meu sen Top Ten
Douma neubeutou pour POP CHAMPAGNE
Lou xéw ci biiir fégne ci biti pour tangal fi soxlawoul ay TAATE fegn
I swear GOD ma ngui dégueuh gars yi
N Easy Wolof la dieul temps yi
Mais CHAMPIONNAT bouma dem BOYYAL CAMP YI
Mayé CRAMPON YI sol GANT YI
BOMAYé def len ay yeufou ALI
PUNCHLINE YI yokou sen DIAALE YI
Yaaaaaaaawou diaaaale flow lay dégueu par millier
Motakh flow bi ni Bombardier ley disser
Poupe sa Toubey NO MAITRISER
Kou niakk fayda legn leu Guissé
Sa Showdy nénama niou guisssé
Néko boy mou baayi fo bi
Sou mossé njaago bi elle voudra bisser
Dinako GANG BANG mane kassé mou fokni né 10 legn
{Refrain}
Ma nigga talouniou Fo
Gni ngui run game bi doniou déggueu
Yagg neu BMG 44
Loumou Yagg yagg boy di nga nangou louy deugg
My nigga Talouniou Talouniou Talouniou Fo
Talouniou fo was written by Nix.
Talouniou fo was produced by PassaBeatz.
Nix released Talouniou fo on Fri Mar 03 2017.