Rap colonial

Dasto

Download "Rap colonial"

Rap colonial by Dasto

Release Date
Wed Feb 28 2018
Performed by
Dasto
Produced by
Writed by
Dasto

Rap colonial Lyrics

Intro
Wou
Boy thia original
International boy
Freestyl
Ok

Couplet

Let me introduce my self damay fo man rap ba tuma
Fi nieupay xeutio silim tax man legui raba tuma
Damay feeci linga fass war ko woup woup di dawal
Das moy sa papa foma séné dawal [souk]
Soukran liii kawé na
Mysterieux haha lii cas wé na
Doma guis sa street ba legui daniouy sakétu
We was tree but now am the only one
MT-boy c'est pour la vie mais seul les vraix savent
Je sais ce que j'ai vu bouche B je fais gaf
From roythia DK
Meun limay def ta nouma neex lamamy diikey
Fils nala jomal
Néna la jobal
Li beuy di yor di tieupi tieupi nak moko tiompal
Lalé wuma ak yaw bul esss guiss sama tokal
Rime you terre a terre ta do diegui sama planete
J'ai une vision bref(2) des plan nette
Rap(2) i do it like no bady
I can an d i can reason why ma adj bars yi
Siguil teneu bii doko jot
F***k(2) sudé dangay xar mu jot
Ok
Boy yi teki wugn tuss push mais dagn mystique
Rest in peace dem ci yalla pacoltille daniou miss tik
Jar jaru underground la fok niou jiii xar
Yalla dji taw mbeund mi juk niou xuss ndox djegui mbalite
Done ci game bi rawu (wu)²
Rap def na ma rosso
Nga xam fi lep sosso
Todj dk ba rosso
Shut out my babdy shu sosso

Outro
Just freestyl wu sup
Yeah hip hop galsen
Underground overground
Aniou bolo done beneu
Its all about hip hop
Yeah wusup negga
Yeah freestyl gat saf
.....
Kothieu ma kotieu ma
....
Le 13 mars my birthday

Rap colonial Q&A

Who wrote Rap colonial's ?

Rap colonial was written by Dasto.

Who produced Rap colonial's ?

Rap colonial was produced by .

When did Dasto release Rap colonial?

Dasto released Rap colonial on Wed Feb 28 2018.

Your Gateway to High-Quality MP3, FLAC and Lyrics
DownloadMP3FLAC.com