Download "Wuyuma"

Wuyuma by Viviane Ndour

Performed by
Viviane Ndour
Produced by
Senegal
Writed by
Viviane Ndour

Wuyuma Lyrics

Xalé bi sama réni xol déh wuyu maa
Beugue nala té xamothie dara
Mbeuguél thie xol léy nék deugueleu
Beugue nala té xamo thie dara

Mane déh walouléne ma wax koko
Xalé bi lékatuma ndax mome
Nanatouma nélawatouma
Wowo
Sama xol yathie néh

Lék lék ma woo ko tit dal di coupé
Sama appetit coupé
Febar dinama guoungué
Docteur dama love ba dof
Té xawma loukoy fathie
Wowo
Mba meune nga thie daraa

Xalé bi sama réni xol déh wuyu maa
Beugue nala té xamothie dara
Mbeugyél thie xol ley nék deugueleu
Beugue nala té xamo thie dara

Mane woo nala founé
Nga diapémma sa xarite
Inviter résto, lalal nala louné
Wowo
Nga diapéma sa xarite

Lék lék ma woo ko tite dal di coupé
Sama appetit coupé
Fébar dinama guoungué
Docteur dama love ba dof
Té xawma loukoy fathie
Wowo
Mba meune nga thie daraa

Mane beuguena ma bagne bayiwouma
Mane guisoumaa
Kénén koudoul mome
Mbeuguéleu beuri dolé yén mako xam

Xalé bi sama réni xol déh wuyu maa
Beugue nala té xamothie dara
Mbeuguél thie xol léy nék deugueleu
Beugue nala té xamo thie dara

Xalé bi sama réni xol déh wuyu maa
Beugue nala té xamothie dara
Mbeuguél thie xol ley nék deugueleu
Beugue nala té xamo thie dara

Kouthie nék'aak kingna nope
Sa guinaw bandague faxassul
Diougueul yeungueul bamou saf
Sa guinaw badangue faxassul

Kouthie nek'aak kingna nope
Sa guinaw bandague faxassul
Diougueul yyeungueul bamou saf
Sa gnuinaw badanue faxassul

Wuyuma Q&A

Who wrote Wuyuma's ?

Wuyuma was written by Viviane Ndour.

Who produced Wuyuma's ?

Wuyuma was produced by Senegal.

Your Gateway to High-Quality MP3, FLAC and Lyrics
DownloadMP3FLAC.com